ci turu Yàlla laye tambalé midi àji yërëm jaam nëpu ci aduna di àji yërëm waay texe yi ci alaaxira
Rabbi as haabaka bil himmati wala tou rabbi him bid darsi fakhate...

khissa-seydina-moussa

Khissa Seydina Moussa par Serigne Bassirou Mbacké Khelkom

download MOUSSA_1
24.3 MB 1:00:38 min
download S. BASSIROU MBACKE_Hissatou MOUSSA (AS)2
24.1 MB 1:00:14 min
download S. BASSIROU MBACKE_Hissatou MOUSSA (AS)3
24.1 MB 1:00:12 min
download S. BASSIROU MBACKE_Hissatou MOUSSA (AS)4
24.5 MB 1:01:05 min
download S. BASSIROU MBACKE_Hissatou MOUSSA (AS)5
23.7 MB 59:07 min

Autres

Ajouter un Commentaire


Code de sécurité
Rafraîchir

Commentaires   

+1 # BOUCHRA 20-08-2011 21:37
waw kay nak! lumélnii moo mankéwoon ci sitbi.amna solo lool yalnalén ci SUNU BOROOM gerem.maa ngi sakku legéy bu am solo bii ngén bagn koo yamalé fii.suma sagnoon wér wuné ngén tan kén ci boroom xamxam yi mélné serigne fallou mii taataan ay kaddoom défko ci sitbi.ndax loolu dana tax sitbi gene rich.té géniy fan gni nga xamné sén kaddu day deppoo ak jangalém serigne touba témuy deppoo ak ndigel.wa salam!
Répondre | Répondre en citant | Citer
-1 # sohna 14-08-2011 17:29
serigne fallou yalnako fi Yalla yagal té wér!!
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # taysire 13-08-2011 13:54
amna solo yananu yalla nangoul bijahil xadiim
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # ndongoli 13-08-2011 13:47
amna solo lol yalla naniou sounou borom may dek ak top amine
Répondre | Répondre en citant | Citer
+1 # kandji 13-08-2011 06:42
wakhtane bi amna solo machalah
yalla faye léral gui si barkép borom touba
Répondre | Répondre en citant | Citer
-1 # KHALIL 13-08-2011 06:16
YALNANU YALAH NAGOUL SUNU KOR!!
Répondre | Répondre en citant | Citer
0 # talibé 12-08-2011 11:42
euskeuy amatina solo lole diereguéne dieuf
Répondre | Répondre en citant | Citer
copyright Al-himma 2010-2017