Lane moye Himma?
"Ak njalbéenam moodi “NIYYATU”: muy yéene jege Yàlla ak yéene am Ngërëmal Yàlla;
akitam “AL IRAADATU”: muy namm jege Yàlla ak namm am Ngërëmal Yàlla;
laca tege moodi “AL HAZMU”: muy am dogu ci jege Yàlla ak am Nërëmal Yàlla;
laca tege moodi “AL HËDEF”: moodi lingay diir ngir bëgg ko jam nga def ko muy jege Yàlla ak am Ngërëmal Yàlla"
SERIGNE MBACKE ABDULAAHI