Rabbi as haabaka bil himmati wala tou rabbi him bid darsi fakhate...
Cheikh Ahmadou Bamba MBACKE KHADIMOU RASSOUL
Lane moye Himma?
"Ak njalbéenam moodi “NIYYATU”: muy yéene jege Yàlla ak yéene am Ngërëmal Yàlla;
akitam “AL IRAADATU”: muy namm jege Yàlla ak namm am Ngërëmal Yàlla;
laca tege moodi “AL HAZMU”: muy am dogu ci jege Yàlla ak am Nërëmal Yàlla;
laca tege moodi “AL HËDEF”: moodi lingay diir ngir bëgg ko jam nga def ko muy jege Yàlla ak am Ngërëmal Yàlla" SERIGNE MBACKE ABDULAAHI
Petit Fils de Serigne Abdou Dia Mbacké Douyoly.
Serigne Abdou Dia Mbacké Douyoly, de son vrai nom Serigne Abdou Khadre
Mbacké est le Fils de Serigne Mbacké Sokhna Fils de Mame Abdou Khadre Mbacké
Fils de Mame Balla Aïcha Fils de Mame Maharam Mbacké.
Son Grand père Mame Abdou Khadre est le frère de Mame Mor Anta Sally, père de Serigne Touba...Lire plus